People

Le garouwalé de Mia Maboo à son ex mari No face «Beuri diar diar takhouta kham adounaa»

Written by admin

Beuri diar diar takhouta kham adounaa

Beuri xam xam takhouta cilwisé

Woné yiw takhouta am diiné

Lo beuri doolé amo maitrise SAP nité desna

lo beuri beuri diné té amo foie mok zeroyam

Lo rafete rafete te sétoulo saffoul.

Yalnagnoul yalla may deugouu té mouy lou deugou si gnoune.


About the author

admin

Leave a Comment